L'histoire de l'âne - Wolof
Benn |
bess |
le-woon |
benn |
dekkalee |
dem |
ci |
bunt-u |
ker-u |
moola |
Nasreddin. |
un |
jour |
être-.pas |
un |
voisin |
aller |
devant |
porte-de |
maison-de |
Mollah |
Nasredine. |
Un voisin se présenta un jour au portail de Mollah Nasreddin. |
Bi |
mu |
àggee |
ci |
bunt-u |
ker |
gi |
mu |
fëgg. |
quand |
il |
arriver |
devant |
porte.de |
maison |
la |
il |
frapper. |
Quand il arrive devant la porte de la maison, il frappe. |
Moola |
bi |
ubbi |
bunt-u |
ker |
gi , |
mu |
nuyoo |
ak |
moom. |
mollah |
le |
ouvrir |
porte-de |
maison |
la |
il |
saluer |
avec |
lui. |
Le mollah ouvre sa porte, ils échangent des salutations. |
Bi |
mu |
ko |
nuyoo |
ba |
noppi |
dekkalee |
bi |
ni |
ko : |
quand |
il |
le |
saluer |
après |
terminer |
voisin |
le |
dire |
lui |
Après les salutations, le voisin lui demande : |
"Man |
nga |
ma |
abal |
sa |
mbaam |
tey ? |
pouvoir |
tu |
moi |
prêter |
ton |
âne |
aujourd'hui |
"Peux-tu me prêter ton âne aujourd'hui ? |
Dama |
am |
li |
ma |
wara |
yoobu |
biir |
dekk |
bi. |
aux.je |
avoir |
chose |
je |
dois |
transporter |
à |
ville |
la |
J'ai des choses à transporter à la ville." |
Waande |
moola |
bi |
bëgg-ul-woon |
abal |
mbaam-am |
dekkalee-m |
boobu. |
mais |
moola |
le |
aimer-neg-pas |
prêter |
âne-son |
voisin-son |
ce. |
Mais le mollah n’avait pas du tout envie de prêter son âne à ce voisin-là. |
Moola |
bi |
ni |
faf |
dafa |
am |
ku |
mu |
ko |
abal. |
mollah |
le |
dire |
donc |
le |
AUX avoir |
quelqu’un (.à qui) |
il |
le |
prêter. |
Le mollah dit donc qu'il y a quelqu'un à qui il l'a prêté. |
Ci |
sassee |
dekkalee |
bi |
ni |
moola |
bi |
"sa |
mbaam |
mi |
la |
degg |
mu |
yuuxu |
ci |
sa |
ëtt-u |
ker |
gi ?" |
à |
.instant |
voisin |
le |
dire |
mollah |
le : |
ton |
âne |
le |
AUX |
entendre |
il |
braire |
dans |
ta |
cour-de |
maison |
la. |
Le voisin dit alors au mollah : "c'est pourtant ton âne qu'on l'entend braire dans la cour de ta maison ?" |
Moola |
bi |
bëgg-ul |
wonee |
reewand-eem, |
mu |
ni |
dekkalee |
bi : |
mollah |
le |
vouloir-neg |
montrer |
impolitesse-son |
il |
dire |
voisin |
le |
Le mollah ne voulant pas se montrer impoli, il dit au voisin : |
"yow |
ko |
gëm : |
mbaam |
mi |
wala |
man |
sa |
moola ?" |
toi |
qui |
croire |
âne |
le |
ou.bien |
moi |
ton |
mollah |
"Tu crois qui, toi ? L'âne, ou moi ton mollah ?" |